Grand Amour - Episode 18 - Saison 1 [Partie 3/4]

[À la une]☆~~👉rebrand.ly/A_la_une-Pikini
[Abonnement Gratuit ici]☆~~👉rebrand.ly/Abonnement-Gratuit-Pikini
[Visitez notre Blog]☆~~👉rebrand.ly/Blog-Pikini
[Inscriptions aux Castings ici]👉rebrand.ly/Castings-Pikini
[TWITTER]☆~~👉rebrand.ly/Twitter-Pikini
[FACEBOOK]☆~~👉rebrand.ly/Facebook-Pikini
[INSTAGRAM]☆~~👉rebrand.ly/Instagram-Pikini
Pikini Productions☆~~👉+221 771161717 [Service Commercial]
[À la une]☆~~👉bit.ly/A_la_une-Pikini
[Abonnement Gratuit ici]☆~~👉bit.ly/Abonnement_Gratuit_Pikini
[Visitez notre Blog]☆~~👉bit.ly/Blog-Pikini
[Inscriptions aux Castings ici]👉bit.ly/Castings-Pikini
[TWITTER]☆~~👉bit.ly/Twitter-Pikini
[FACEBOOK]☆~~👉bit.ly/Facebook-Pikini
[INSTAGRAM]☆~~👉bit.ly/Instagram-Pikini
#MADIOR_AK_DIOR_LA_SAISON_02_SORTIRA_
©ByBen 2020 : WhatsApp ☆~~👉 +221776626858 [Admin]

Télécharger

Vues
471,957

Commentaires

  • Felicitation assy

    Fatou Gueye SeneFatou Gueye SeneIl y a 5 jours
  • No kene dou yen bilay magui dioy fi ma nek ni

    Khadim DiopKhadim DiopIl y a 9 jours
  • Glisser la clé sur la porte quén défatouko ak sathie you bari yi Soda bo nobé nitt dokeu sougouf ni safar bou naturel mo dakh

    aicha alarba allfaicha alarba allfIl y a mois
  • Taximan mo sadique nena ko woko téléphone

    mbathio diagnembathio diagneIl y a mois
  • J’ai pleuré beu sama beute yi di meiti 🥺😭

    Fatima AidaraFatima AidaraIl y a mois
  • Oh assy est belle😍😍😍🥺🥺🥺

    Thiaba Laye NdoyeThiaba Laye NdoyeIl y a mois
  • Man Edou la beugue

    Oumanédiary SowOumanédiary SowIl y a mois
  • Non sama yaram dawna dakh Lima gniak sama yaye te doudou Lou meti😭😭😭

    Maguette FayeMaguette FayeIl y a mois
  • Pouce bleu pour mon Papa Préféré Edu 🤜❤️

    Katy BonbonKaty BonbonIl y a mois
  • Meilleur épisode

    MAREME NIANGMAREME NIANGIl y a mois
  • C’est triste😭

    ena ecoleena ecoleIl y a mois
  • Bilay li com degeu edu damako yeureum Trop

    Taekowndo club Sounatou rassoul TOuba HLMTaekowndo club Sounatou rassoul TOuba HLMIl y a mois
  • Bi mom dou amaty nékhna loll

    Diakhate Mame fatyDiakhate Mame fatyIl y a mois
  • Wa ani 4ième partie bi tamite nak ???

    Johey4U DubaiJohey4U DubaiIl y a mois
  • J'adore vos séries vraiment ❤ c'est très intéressant

    Khady ManèKhady ManèIl y a mois
  • Mbeuguel thii khol lay né

    Ndiate thioye DiawNdiate thioye DiawIl y a mois
  • alioune diaye borome pikini yagui liguéye machallah

    Gueye MoustaphaGueye MoustaphaIl y a mois
  • Original 😎👍🏾

    Match day premier leagueMatch day premier leagueIl y a mois
  • Haaa soda dh sa ligueye bi nekhna def sa vip bou bakh

    Maguette seckMaguette seckIl y a mois
  • Aye waye wakh len ma kagne laye dawat beugue nako suivre 😢

    Maye MangaMaye MangaIl y a mois
  • Épisode bi mon ma geuna yém si grand amour

    Dame LoDame LoIl y a mois
  • Franchement Grand amour c'est le meilleur série du Sénégal. Non mais j'adore 😍. Vous aviez bcp d'inspiration machalla 😍

    Ndiaye DiarraNdiaye DiarraIl y a mois
  • Super

    Bamba komaBamba komaIl y a mois
  • Nn edu yangui todj pikini ♥️♥️♥️

    Ma Saliou DiopMa Saliou DiopIl y a mois
  • Eeee Docter. Soubouhanallaye

    Amadou telimille Barry sanfouAmadou telimille Barry sanfouIl y a mois
  • Edu tu es excellent avec beaucoup de talent laffthiat

    ndeye adam ndaondeye adam ndaoIl y a mois
  • Bamadalé sètan série ba lègui épisode bi mo megueneu marqué, yay boy yalnaga goudd fan ba fakkè sunu ndiarign🙏❤️

    Mor MbengueMor MbengueIl y a mois
  • Yaye boy yalnaga fi yag té wèrr🙏❤️

    Mor MbengueMor MbengueIl y a mois
  • vraiment metina loleee kou gnak yaye ak kou gnakkkoule yaye yèpppe la tousè

    haja bahhaja bahIl y a mois
  • J aime bien cette série

    Houleye SallHouleye SallIl y a mois
  • @pikini diap lén Sii rekk bou assy naré dead guén sathie film bi mou continué doundeu sinon ma nara dead réellement 😭🙏🏾🙏🏾❤️😂😂❤️❤️❤️❤️

    Mouha NJMouha NJIl y a mois
  • J'ai trop acte d voir la suite ,bravo

    ndeyeyacinekeit Sarrndeyeyacinekeit SarrIl y a mois
  • Kana li moy khollou yaye ak dôme

    Selle MbayeSelle MbayeIl y a mois
  • Jador ce petit way am caractere meune jouer

    Eva ndiayeEva ndiayeIl y a mois
  • Soda vraiment sa thioup bi amoufi wone place 😂😂😂

    Fatou WadeFatou WadeIl y a mois
  • yaye yeup yalla naniou fii yag teii weur

    Yacine NdiayeYacine NdiayeIl y a mois
  • Nice n'a

    Deme NdogalDeme NdogalIl y a mois
  • En tout cas c trop triste

    Awa SarrAwa SarrIl y a mois
  • Assy mo deh nenako nama ray

    Cheikh SarrCheikh SarrIl y a mois
  • Wa sOda yeina nga sOugOuf nga rein nga ammsi bakarr tei si niOu dakk leu ngay mOudjié masseu dOme amO ligueyOu ndeye dh😂

    Awa NdiayeAwa NdiayeIl y a mois
  • Machalla 😥😥😥

    Toure AdjaToure AdjaIl y a mois
  • C pleurer bico khalé bi wowé yaye 😭khol moy nitte bilay

    Khoudia ThiamKhoudia ThiamIl y a mois
  • J’ai pleuré c’est vraiment triste 😞

    Fanta Laye GueyeFanta Laye GueyeIl y a mois
  • Machalla edou je t'aime moi

    Sokhna NdiayeSokhna NdiayeIl y a mois
  • Franchement il ma fait pleuré

    Sokhna FayeSokhna FayeIl y a mois
  • Vraiment j suis trop acrau a cette série ❤️

    Fatima MbowFatima MbowIl y a mois
  • Macha Allah dafa nekh

    Dior DiengDior DiengIl y a mois
  • Commentaire worol na am vocal way ma tagg lénnn😀😀😀

    Ins BigIns BigIl y a mois
  • Super

    Kara ManeKara ManeIl y a mois
  • Wouy nama ray

    Kara ManeKara ManeIl y a mois
  • Assy vs allè m tuè mbadou nala ray MDRR

    Etienne Doury SarrEtienne Doury SarrIl y a mois
  • Chèrif boule ré so rétané rék ma dioy ndakh nobela

    Astou DiopAstou DiopIl y a mois
  • HOOO NEKHNA TROP MACHALA RAFETENA 👌💏💏💖💖💏💏👌

    Sokhna NdiayeSokhna NdiayeIl y a mois
  • Amoul pkhoblém.nama khay🤣🤣🤣

    Seynabou DianéSeynabou DianéIl y a mois
  • Sameu khol❤ sedd neuh tay oh

    Mor Arame ThiamMor Arame ThiamIl y a mois
  • Wa soda eupeul na dii😂😂😂 thioup la laaaale de😂😂😂

    Touty FallTouty FallIl y a mois
  • Publicité bi goudena di

    Marguerite Mireille Rivier SagnaMarguerite Mireille Rivier SagnaIl y a mois
  • NAma ray kaaay

    Belle MbeuBelle MbeuIl y a mois
  • Assi seur diap nala toubeuy diap nala

    XEW XEW TVXEW XEW TVIl y a mois
  • Khol moy niit Intéressant !!! Bonne continuation

    mame coumba sambemame coumba sambeIl y a mois
  • Khol moy niit Intéressant !!! Bonne continuation

    mame coumba sambemame coumba sambeIl y a mois
  • 4em et derniere bi dina todje nonn pikini nice job

    Khaabaane syllaKhaabaane syllaIl y a mois
  • Machalah bi mom moy lass

    seye marieseye marieIl y a mois
  • Soda moy khastè beug goor eupna guala yaw mi liggey nit bamou deh dax beug homm tchim

    sokhna diarra diopsokhna diarra diopIl y a mois
  • sa waw bi foroul d ahahah

    Mamadou DiengMamadou DiengIl y a mois
  • Khale bii nak dafa yarou bilahi

    Elhadi TallElhadi TallIl y a mois
  • Ame very happy too grand Amur ❤️❤️❤️❤️😭😭😭

    El hadji babou CeesayEl hadji babou CeesayIl y a mois
  • Cett episode m fai pleur3😓 da daw yaram

    Ndiaye mamefatymbackeNdiaye mamefatymbackeIl y a mois
  • wa asy mangeerou you nk

    Fatima DiopFatima DiopIl y a mois
  • Edou , un acteur polyvalent

    mansour sowmansour sowIl y a mois
  • J'aime bien votre jingle, mais mettez-nous de la musique qui va avec s'il vous plaît. Comme Youssou Ndour par exemple : "Mbeguel ay thioneu leu", quelque chose du genre 😁

    TaphaTubeTaphaTubeIl y a mois
  • Machalla

    Papou KantePapou KanteIl y a mois
  • Nonnnnnnnnnnnnnnnn vraiment bravo 👏👏👏👏👏 grand amour aupeupeupeupeupeup mai li nékhna ahhh merci waye je vous aimes sa se voi kouy jouer grand amoul ba jour st Valentin nga wara joué mou reuy si amour mai li reuyna boufi yamone sakh mou nékh instant bi meunatou sétane bénéne série ndakh cone dou saf dara si mane way diadieuff waye chapeau à vous .pikini

    Alioune CisséAlioune CisséIl y a mois
  • Bilae sen ligueye réféte na manchalla

    Khadim FayeKhadim FayeIl y a mois
  • Soda : yaw yay assy la bonne de commi Assy : Qui, yaw la kan Soda : mane la Soda fi ladone ligguéyé, wayé dama bayii Assy : loutax ga bayi Soda : guiss ga commi bi djabaram gayio ba légui shaq goudi mou fëëg ma bëgg ma violé. Daw nak ca bagguay am tankk Assy : amoul problème, nama Raay Soda : waaaaa ki bëggoul gor rek 😂😂😂😂😂

    Mame Gor FallMame Gor FallIl y a mois
    • 😂😂😂😂😂🤣🇬🇲

      Yamudow NjieYamudow NjieIl y a mois
  • 😭😭😭😭😭🤱c'est tousse un 👉💖

    Moussa AlliwMoussa AlliwIl y a mois
  • Bel épisode. Bien inspiré

    Atoumane DiengAtoumane DiengIl y a mois
  • Machallah

    Mouhamed DiagneMouhamed DiagneIl y a mois
  • Non bi dotoul ame allahou akbare Sama khôl bi laye lale

    begue baye niassbegue baye niassIl y a mois
  • Téy mom dioyna billahi

    Ndao AssaneNdao AssaneIl y a mois